Youssou N'Dour — Sama Gàmmu songtekst en vertaling

De pagina bevat de songtekst en de Nederlandse vertaling voor het nummer "Sama Gàmmu" van Youssou N'Dour.

Songteksten

Nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Yor xaalis mënui tee me moom la
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko
Foog nan nita ko waddal nga for ko
Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko
Man daal maay sa buur nangu ko
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Ah gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal suma askan nga
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal man sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal man suma xarit nga
E e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga
Baal dooc moomu foo ko
Teeyai teey teey
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
E e e gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal suma askan

Songtekstvertaling

Nanga of yaw sama gàmmu dégg of nga yor xaalis
Xam of neil Yaw moomu los ko
Mensen ko àbb mbaa nga voor ko
Baal dózééé, y
Nanga of, de nga of gàmmu dégg of nga yor xaalis
Basis voor ifén tàmbaleey wëlis
Xam of neil Yaw moomu los ko
Mensen ko àbb mbaa nga voor ko
Baal dózééé, y
Yor xaalis mënui tee me moom with
Nanga of, de nga of gàmmu dégg of nga yor xaalis
Xam of neil Yaw moomu los ko
Mensen ko àbb mbaa nga voor ko
Baal dózééé, y
Kaay gaaw wax als de nga d ba de ko
Foog of nu plan ko waddal nga voor ko
Was if GAW ñaata door doon if fay ko
Mann daal maay in bui nangu ko
Nanga of, de nga of gàmmu dégg of nga yor xaalis
Basis voor ifén tàmbaleey wëlis
Xam of neil Yaw moomu los ko
Mensen ko àbb mbaa nga voor ko
Baal dózééé, y
Ali suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ali suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ali suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Ali gàmmu daal sama doomu nday nga
Maar in gàmmu daal sun xarit nga
Maar in gàmmu daal sun askan nga
Ali suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Maar in gàmmu daal sun xarit nga
Maar in gàmmu daal man sama doomu nday nga
Maar in gàmmu daal man sun xarit nga
Maar in gàmmu daal yaw sama doomu nday nga
Baal dooc moomu onder ko
Teeyai teey teey teey
Ali suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ali suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ali suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Maar in gàmmu daal sama doomu nday nga
Maar in gàmmu daal sun xarit nga
Maar in gàmmu daal sun askan